We’ve updated our Terms of Use to reflect our new entity name and address. You can review the changes here.
We’ve updated our Terms of Use. You can review the changes here.

Fou Malade, Niagass - Y​à​lla

from OUSSEYNOU AK ASSANE by Fou Malade et Niagass

/
  • Streaming + Download

    Includes unlimited streaming via the free Bandcamp app, plus high-quality download in MP3, FLAC and more.
    Purchasable with gift card

      €1 EUR  or more

     

lyrics

Yàlla
Refrain
Yàlla sa jaam yi ñoo lay ñaan //Dieu, tes esclaves t’implorent
Gudd fan sutura fekke tal ak muj gu rafet // Longue vie, sérenité, bonne santé et une fin heureuse,
Yàlla may nu lekk ak naan // Dieu offre-nous à manger et à boire
« Ordonnances », « dépenses », « essence » ñun bëggu nu « défaite » // Ordonnances, dépenses, essence, on aime pas la défaite

Couplet 1
Yaa ma taal ba ma siiw aduna di ma xam // Je te dois mon succès, aujourd’hui tout le monde me connaît
« Beurre » si naaj lañ ma diw, yaa ko tay may ma ndam // Je brille comme beurre au soleil, par ta Grâce, j’ai du succès.
Gel yi sax dañ ma nob, « autographes » ak « photos » // Même les filles me courent après, sollicitent mes autographes et mes photos,
Ne ci kaw ne «au top » wàcc fas yéeg « auto » // j’ai atteint les sommets, j’ai sauté du cheval pour une belle voiture
Sa ma clip feeñ tele samay « droit » kenn du fay // Mon clip passe à la télé mais mes droits restent impayés
Jënd « slip » la tële yërmande maa ngi fay // Je suis incapable d’acheter un slip, au secours ! Je suis m’éteins
« Artistes patrimoine » Laba Sosseh, Ndiaga Mbaye // Les artistes sont notre patrimoine, Laba Sosseh, Ndiaga Mbaye
Ndiouga Dieng, Number One, Pacotille dem na tey // Ndiouga Dieng, Number One, aujourd’hui, Pacotille est parti
Ñun daal ñoo lay woyal feccal ba nga doyal // Nous, nous chantons et dansons pour toi à te combler.
Dundal Bégal, Bégal dundal, waroo ñu seetaan // Nous te faisons vivre, te rendons gai, te rendons gai, te faisons vivre, tu ne dois pas nous ignorer
Ku wéet nu wettali, ku réer nu nettali // Compagnons des solitaires, nous sommes les gardiens de l’histoire
Mag ak gune kune fune fexeel ñu reetan //  aux grands et petits, à chacun, partout, nous apportons le sourire.

Couplet 2
Jomb naa wër ñaan ndax da ma am tur // J’ai honte de quémander à cause de ma renommée
Sonn naa, leb naa aka maa bëri bor // Je suis fatigué, j’ai pris des crédits, je suis si endetté
Gëm naa dina baax ndax Yàlla mooy bur // Je crois que ça ira car Seul Dieu est Roi
Bu ma naan ndeysaan du ma jaay sama ngor // N’aie pas pitié de moi, je ne vendrai pas ma dignité
Feyu ma la, na nu dem poliis, Yàlla may a gu ma xaalis // Je ne te paie pas, amène-moi à la police, Dieu ne m’a pas encore enrichi
Gëstu ma geun di ma noonoo», laajoo nu ma def ak coono // Essaie de comprendre qui je suis au lieu de faire de moi ton ennemi, tu ne m’as pas demandé comment je vis mes difficultés
Xiif mar mer la yendoo siiw sa ma sutura ma ngembo // Je vis mes journées affamé, assoiffé, colérique, mais ma célébrité t’empêche de le voir
Du ma géwal mënu maa woyaan, taasu walla woy ngoyaan // Je ne suis pas griot, je ne peux pas quémander, faire des éloges ou chanter de la musique « ngoyan »
Hip Hop tere ñu « battrer » « hardcore » bëgg ñu « cadrer » // Le hip hop nous empêche de flamber, le hardcore veut nous cadrer
Na nga muñ dina baax « madre » yéene bi weesu na pantare // Tiens bon maman, ça ira, mes rêves vont au-delà d’une chambrette.

Conclusion
Useynu niŋ ñuy seetaanee di ñu sagganee ba xëy nu jóog fi // Ousseynou, la manière dont nous sommes abandonnés, négligés, jusqu’à ce qu’à notre mort.
Ñu ñuy tuddee ay bayal ay koñ ay estad wànte nak grawul // Ils baptisent des rues, des stades des boulevards à nos noms, mais c’est pas grave
« Mais je te jure Assane, sur la tête de notre mère », gis nga // Mais je te jure Assane, sur la tête de notre mère, t’as vu…

credits

from OUSSEYNOU AK ASSANE, track released April 9, 2018

license

all rights reserved

tags

about

FOU MALADE & NIAGASS Dakar, Senegal

Fou Malade et Niagass sont frères jumeaux, dans leur âme, leur physique, leur passion pour leur pays et sa jeunesse. Ensemble, ils ont cette joie et cette énergie de vivre qui fondent l’essence de leurs textes écrits en wolof et de l’harmonie complice émanant de leurs voix. Après quelques créations artistiques communes (Gent Bi en 2005, Sénégal en 2012), ils sortent « Ousseynou ak Assane ». ... more

contact / help

Contact FOU MALADE & NIAGASS

Streaming and
Download help

Redeem code

Report this track or account

If you like Yàlla, you may also like: