We’ve updated our Terms of Use to reflect our new entity name and address. You can review the changes here.
We’ve updated our Terms of Use. You can review the changes here.
/
  • Streaming + Download

    Includes unlimited streaming via the free Bandcamp app, plus high-quality download in MP3, FLAC and more.
    Purchasable with gift card

      €1 EUR  or more

     

lyrics

Tefess
Refrain
Tefes laa bëgg a gis // Je veux voir la plage
Baadolo lañ koy siis // La classe populaire en est privée
Ñun ñépp ñoo ko moom // C’est notre bien public
Delloo leen sunu koom // Rendez-nous notre richesse

Couplet 1
Faan, Sumbejun, Ngor, Mamelles // Fann, Soumbédioune, Ngor, Mamelles
Sangu war a fey doon nootel // Payer pour se baigner reste une oppression
Jël sunu suuf def moomeel // Accaparer nos terres et en faire vôtres
«Barrer air pur» ndax sa « hôtel » // Vos hôtels, nous privent d’air pur
Li lu mu doon, maa haaza // C’est quoi ça ? Qu’est-ce c’est que ça?
Yéen a seddo sunu « littoral » // Vous vous êtes partagé notre littoral
« Blu Radisson », « Sea Plaza » // Blu Radisson, Sea Plaza
Ñépp a bokk suufu Senegaal // La terre du Sénégal appartient à tous.

Couplet 2
Njiitu réew mi la ñuy déglu ngir mu wax si Aïdara // Nous attendons l’avis du chef de l’Etat sur l’affaire Aïdara
Domou réew mi ëlëgu ndaw ñi gëstu indi saafara // Les fils du pays et l’avenir de la jeunesse doivent être éclairés pour amener des solutions
Boroom doole baadolo kune war fi am dara // Le riche, le pauvre, chacun doit être servi
Buñ ko deful bu ñu meree fippu indi saafara // Sinon, nous nous fâcherons et donnerons nos propres solutions
« Littoral » bi jooy na // Le littoral pleure
« Bradage » bi doy na // ça suffit le bradage !
Takku taxaw jot na // Il est temps de se lever
Bu mu jaam gi dog na // L’esclavage est aboli

Couplet 3
Fii La nu daan fowee // C’est là où nous jouions.
Séen mool sànni mbaalam // Apercevant le pêcheur lançant son filet,
Bég si ni mu kay joowee // Heureux de sa façon de ramer,
Xaar ngon teeru gaalam // Attendant le soir pour accueillir sa pirogue
Tefess la « étudiant » daan toog // Les étudiants s’asseyaient sur la plage
Féex di jàng seeni « leçon » // respirant les embruns et apprenant leurs leçons
Déet bul jaay li nu bokk // Non ne vends pas notre bien commun
Héee « cause » indi « solution » // Hé une discute pour trouver une solution

credits

from OUSSEYNOU AK ASSANE, track released April 9, 2018

license

all rights reserved

tags

about

FOU MALADE & NIAGASS Dakar, Senegal

Fou Malade et Niagass sont frères jumeaux, dans leur âme, leur physique, leur passion pour leur pays et sa jeunesse. Ensemble, ils ont cette joie et cette énergie de vivre qui fondent l’essence de leurs textes écrits en wolof et de l’harmonie complice émanant de leurs voix. Après quelques créations artistiques communes (Gent Bi en 2005, Sénégal en 2012), ils sortent « Ousseynou ak Assane ». ... more

contact / help

Contact FOU MALADE & NIAGASS

Streaming and
Download help

Redeem code

Report this track or account

If you like FOU MALADE & NIAGASS, you may also like: