We’ve updated our Terms of Use to reflect our new entity name and address. You can review the changes here.
We’ve updated our Terms of Use. You can review the changes here.
/
  • Streaming + Download

    Includes unlimited streaming via the free Bandcamp app, plus high-quality download in MP3, FLAC and more.
    Purchasable with gift card

      €1 EUR  or more

     

lyrics

BAALE
Refrain
Boo Jekkoo deel baale // Pardonne quand tu peux faire mal
Nañ diissoo bañ laale // Discutons au lieu de nous battre

Couplet 1
Tey ma wax la li na naqari // Je te dirai aujourd’hui ce qui me chagrine :
Jaay doole ndax sa « gabarie » // Provoquer les gens parce que tu es costaud
Ñëw di jaale indi sabar yi // Présenter tes condoléances avec bling bling
Xaal géew bi sànni koppar yi // Se mettre au milieu de la foule et jeter l’argent

1-2 nga shine, 3-4 nga xeex // 1-2 tu t’énerves, 3-4 tu te bats
Li nga def sa mayin sax sa xol di jeex // Tes mauvaises pensées te rongent
Woo la añ nga suur tëfli xaax ne tëf // Tu refuses de déjeuner mais tu craches dans le plat
Kajj nga reer bi tuur, taal sa jum di ëf // Tu renverses le plat et tu allumes un gros joint

Yow lu tax bi meer bi feebare // Et toi, pourquoi lorsque ta maman était malade
Jëndóo garab yóobu l’hôpital //// Tu n’as pas acheté de médicaments  de l’hôpital ?
Tey nag dëj bi ni nga ko defare // Vu comment aujourd’hui tu as organisé ses funérailles ?
Aduna jay la ñaata junni nga taal //m’as-tu-vu, combien de billet as-tu claqué ?

5-6 nga tëc téeye geel yi tanyim // 5-6 tu t’enfermes pour baiser
Te nga ne ci dëj war a ñaan di waayin // tu t’enivres alors que tu es endeuillé
def tàtt di jooy xollu gan ñi tiis// Ivre, tu pleures à peiner les invités.
Màndikat nga booy jëli naa la fils // T’es un ivrogne, je t’ai découvert fils

Couplet 2

Defu ma yëgu ma bu ma ko waxal // Ne m’accuse de choses auxquelles je ne suis pas mêlé
Gisu ma déegu ma jotu ma jaxal // j’ai ni vu, ni entendu, ni reçu d’offrande
Tuxu ma naanu ma yoru ma goon // Je fume pas, je bois pas, j’ai pas d’arme
Sàccu ma kàccu ma du ma sa noon //Je vole pas, mens pas et ne suis pas ton ennemi

Da ngaa yëg sa bopp maa la gën a reew // Tu te crois supérieur, mais je suis plus indiscipliné que toi
Da nga mën a soop da nga ñeme xew // Tu sais raconter des bobards et tu aimes le folklore
Yagg a wanne baax te sa jikko sew // Tu feins d’être gentil mais tu es sournois
Alal bi nga coop du la mas a lew // l’argent que t’as bouffé ne te sera jamais licite.

Baal ma li ma saaga yaay sama gaayin // pardonne moi de t’avoir insulté, t’es mon pote
Bi ngay laal cagga ñoo ngi naan caayin // Quand tu baisais les putes, on buvait du thé
Na nu peace love dund paradise // faisons la paix et l’amour, vivons notre paradis
Kaay ñu naan koof dafa war a naayis // buvons un café, positivons les choses.

Bége fo ree fexee indi jàmm // Jouir de la vie, rigoler et faire la paix
Boole doole di na gindi jàmm // l’union des forces révèle la paix
Bayyi tooñ gën dëkkee balu àq // Eviter de nuire aux autres vaut mieux que demander éternellement pardon
Ñaan gudd fan tuub li ñu yàq // Prier pour une longévité et expier toutes nos erreurs

Tudee naa la doom dëgg la ci man// Mon fils porte ton nom et c’est sincère
Boo feebaroon naa la yóobu Fann // Si t’étais malade, je t’aurais amené à l’hôpital Fann

Mane la nitt Njaay yow la golo Hann // Je suis sain d’esprit c’est toi le singe du parc de Hann
Yagg a saï-saï bandit Colobane // ça fait longtemps que tu es un saï saï, un bandit de Colobane

Lii moo tax du ñu man a kóoz // C’est pour ça qu’on ne peut causer normalement
Sunu amitié na fi « ménopause » // Alors notre amitié s’arrête là

credits

from OUSSEYNOU AK ASSANE, track released April 9, 2018

license

all rights reserved

tags

about

FOU MALADE & NIAGASS Dakar, Senegal

Fou Malade et Niagass sont frères jumeaux, dans leur âme, leur physique, leur passion pour leur pays et sa jeunesse. Ensemble, ils ont cette joie et cette énergie de vivre qui fondent l’essence de leurs textes écrits en wolof et de l’harmonie complice émanant de leurs voix. Après quelques créations artistiques communes (Gent Bi en 2005, Sénégal en 2012), ils sortent « Ousseynou ak Assane ». ... more

contact / help

Contact FOU MALADE & NIAGASS

Streaming and
Download help

Redeem code

Report this track or account

If you like FOU MALADE & NIAGASS, you may also like: